Luci seen xalaat mbok yi ?
Li xew ci mim reew doyna waar ! Sunugaal ndax dina dox su jikko yi ma guiss sopekuwul ? Deuk ak nitt defula dara, nek ci yoonam nga guiss yeenee ko lu bon ligeey ko mu dof wala mu niak ! Deuk ak nitt wersek gam neexula nga tuumaal ko weurr rek di yaak deram ! Deuk ak nitt […]